• ALMAMIAYAT DU FOUTA TORO

  • Apr 4 2023
  • Durée: 12 min
  • Podcast

  • Résumé

  • Ceerno Sulaymaan BAAL moo soppi ni ñiy yore nguuur ca Fuuta jëlee ko ci ndono tegg ko xam-xam ak jikko. Moo Boolewoon Jullit yi ngir ñu jóog xeex ak ñi bañoon diine. Man na noo wax ni moo indi nguurug yemale  di democrasi ci Afrig Sow jant.

    Voir plus Voir moins

Ce que les auditeurs disent de ALMAMIAYAT DU FOUTA TORO

Moyenne des évaluations de clients

Évaluations – Cliquez sur les onglets pour changer la source des évaluations.