• EL HADJ OMAR TALL

  • Mar 14 2023
  • Durée: 12 min
  • Podcast

  • Résumé

  • Umar Seydu Taal ma nga juddoo Alwaar ci Poddorug tey jii. Ganaaw ba mu tukke lu yàgg ci ajug Màkka la delusi xare ba samp Lislaam ci Afrig Soww jant te xeex na xeex bu rëy ak Tubaab bi.

    Voir plus Voir moins

Ce que les auditeurs disent de EL HADJ OMAR TALL

Moyenne des évaluations de clients

Évaluations – Cliquez sur les onglets pour changer la source des évaluations.