Xam sa démb, xam sa tey

Auteur(s): Goethe-Institut
  • Résumé

  • Ngir xam lu leer ci seen mboorum réew ak bu Afrig, ndaw ñi dañoo war a miin jàmbaar yi tabax Afrig. Ndégat yii di Podcast,« Xam sa démb, xam sa tey », looloo tax ñu tànn yenn ci jaar-jaar ak xew-xew i mboorum Senegaal, ngir may ndaw ñi ñu jàngee ci seen démb, baa man seen tay, te waajal seen ëllëg.

    ℗ & © Goethe-Institut Senegaal
    Voir plus Voir moins
Épisodes
  • LAMINE GUEYE ET VALDIODIO NDIAYE
    Apr 11 2023

    Lamine Gèy ak Waljoojo Njaay ñaari kangam lañ yu xeex ak seen i pexe ba Nooteelu nasaraan bi jeex. Li nu gën a jàpp ci ñoom mooy fula ja ñu def ci aar seen ngor ba tontu njiitul Fraraans la taxoon mu mer.

    Voir plus Voir moins
    12 min
  • ALMAMIAYAT DU FOUTA TORO
    Apr 4 2023

    Ceerno Sulaymaan BAAL moo soppi ni ñiy yore nguuur ca Fuuta jëlee ko ci ndono tegg ko xam-xam ak jikko. Moo Boolewoon Jullit yi ngir ñu jóog xeex ak ñi bañoon diine. Man na noo wax ni moo indi nguurug yemale  di democrasi ci Afrig Sow jant.

    Voir plus Voir moins
    12 min
  • KOLI TENGUALA
    Mar 28 2023

    Koli Teŋella doomi Satigi Teŋella Ba ka Nana Keïta la dib Malinke. Cossanam di Baxunu. Jàmbaar ju mag la woon ju mùanoon na jiite xare ba am ca tur wu rëy.

    Voir plus Voir moins
    11 min

Ce que les auditeurs disent de Xam sa démb, xam sa tey

Moyenne des évaluations de clients

Évaluations – Cliquez sur les onglets pour changer la source des évaluations.